jënd

Wolof

Pronunciation

  • Audio:(file)

Verb

jënd

  1. to buy

Conjugation

Conjugation of jënd
present imperfect pluperfect future
1st person singular damay jënd dama doon jënd jëndoon naa dinaa jënd
2nd person singular dangay jënd danga doon jënd jëndoon nga dinga jënd
3rd person singular dafay jënd dafa doon jënd jëndoon na dina jënd
1st person plural dañuy jënd dañu doon jënd jëndoon nañu dinañu jënd
2nd person plural dangeen jënd dangeen doon jënd jëndoon ngeen dingeen jënd
3rd person plural deñuy jënd deñu doon jënd jëndoon nañu dinañu jënd
imperative
singular jëndal!
plural jëndleen!